Porogaraamu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2025 bi tudd: «Nañu jaamu Yàlla ni mu ko bëgge»

Àjjuma

Porogaraamu àjjuma bi, mu ngi sukkandiku ci Macë 4:10​—‘Yexowa sa Yàlla nga war a jaamu’.

Samdi

Porogaraamu samdi bi, mu ngi sukkandiku ci Yowaana 2:17​—«Cawarte gi ma am ci sa kër dina mel ni taal buy tàkk ci man.»

Dimaas

Porogaraamu dimaas bi, mu ngi sukkandiku ci Yowaana 4:23​—‘Nañu jaamu Baay bi ci xel ak ci dëgg.’

Li ñi teew war a xam

Tegtal yu am solo yu ñi teew war a xam.

Seetal itam...

LU JËM CI ÑUN

Kaay teewe ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2026​: Mën nga am bànneex ba fàww

Ñu ngi lay woo nga ñëw teewe ndaje bu mag bu ñetti fan bi Seede Yexowa yi di am ren

NDAJE YU MAG YI

Lãsamã tiyaatar bu sukkandiku ci Biibël bi te tudd: Xibaaru jàmm bi Yeesu Yégle: Xaaj 2 ak 3

Léegi Yeesu màgg na, te tàmbali naa am ay taalibe. Waaye tàmbali na it jànkoonte ak ay fitna ci liggéeyu waare bi.