Téerey gëstu

Bu dee am na loo bëgg a gëstu, walla looy seet ci suñu téere yi walla ci suñu widewo yi, téere gëstu yi mën nañu la dimbali nga gis ko ci lu gaaw. Am na ab téere bu tudd Téereb gëstu, te foofu lim nañu fa mboolem waxtaan aki aaya yi suñu téere yi waxtaane. Boo ko bëggee jàng ci internet, demal ci Watchtower TÉERE YI AM CI SUÑU PALAAS CI INTERNET. Am na it ay téere yu la mën a dimbali nga xam widewo yi nga mën a jëfandikoo ngir xóotal sa njàngum Biibël.

TÀNNAL NI PAAS BII DI FEEÑE