Kaye ndaje Dundinu kerceen ak liggéeyu waare bi
Ci Kaye ndaje bi tudd Dundinu kerceen ak liggéeyu waare bi, lañu bind li ñu war a jàng ci Biibël bi ci semen bu nekk ak li ñu war a waxtaane ci benn ci suñuy ndaje ak téere yi ñu war a gëstu ngir waajal ndaje boobu. Ñépp ñi ko bëgg mën nañu ñëw. Kenn du fey dara.

