Lu bees ci JW.ORG ?
NAÑU JÀNGE CI YEESU
Lan la Yeesu wax lu jëm ci «yëngu-yënguy suuf yu réy»?
Lu tollook 2,000 at ci ginnaaw, Yeesu yégle woon na ne yëngu-yënguy suuf yu réy dina am. Lu tax mu solo tey, ñu bàyyi xel kàddu Yeesu yooyu?
YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)
Xelalu weer wii: Nañu jariñoo bu baax suñu widewo yi
Xoolal xelal yi la mën a dimbali nga jariñoo bu baax widewo yi nekk ci jw.org.
YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)
Nañu fonk suñu mbokk yi doonte sax wuute nañu
Lan moo ñu mën a dimbali ñu gën a fonk suñu mbokk yi, ndax ni ñu wuuteek ñun jikko ak gis-gis?
YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)
Naka la soldaar yi doon wottu buuru Room daan soloo?
Xoolal ni soldaar yi doon wottu buuru Room daan soloo ak ni ñu leen daan xàmmee.
YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)
Li la mën a dimbali nga doylu boo amee jafe-jafe ci wàllu koom
Xoolal ñeenti njàngaley Biibël bi yu la mën a dimbali nga doylu ak loo mën a dund.
YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)
Nowàmbar 2026
Li ñu nar a waxtaane ci yéenekaay bii dale ko 4 ba 31 sãwiyee 2027.

