Ubbil li ci biir

Woneel li am

Seede Yexowa yi

Wolof

Ndaje yu mag yi Seede Yexowa yi di amal at mu nekk

At mu nekk, Seede Yexowa yu bare dañuy amal ndaje yu mag yu ñetti fan. Ci suñuy ndaje yu mag yi, dafay am ay waxtaan ak ay wideo yi ñuy xamal jàngale yi ñu mën a jële ci Mbind yu sell yi. Interviews yi ak wone yi fay am dañuy wone ni ñu mëne dund xelal yi nekk ci Biibël bi. Ñu ngi lay woo nga ñëw teew ci ndaje bu mag bi. Kenn du fey dara.

 

Seetal béréb bi la gën a jege