Kayit yi
Ci xaaj bii, dinga fi fekk ay kayit yuy wax ci lu gàtt ci waxtaan yu sukkandiku ci Biibël bi. Am na fi it ay kayit ngir woo nit ñi ci suñu ndaje yi. Ndaje yi nag, ñépp ñi ko bëgg mën nañu leen a teewe.