Porogaraam yi
Porogaraam yi dañuy wone ni suñu ndaje yu mag yi di deme, maanaam li ñu fa war a waxtaane ak it waxtu wi ñuy def xaaj bu nekk. Ndaje yooyu nag, ñépp ñi ko bëgg mën nañu leen a teewe. Kenn du fey dara.