Porogaraamu Ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2025 bi tudd: «Nañu jaamu Yàlla ni mu ko bëgge»
Àjjuma
Porogaraamu àjjuma bi, mu ngi sukkandiku ci Macë 4:10—‘Yexowa sa Yàlla nga war a jaamu’.
Samdi
Porogaraamu samdi bi, mu ngi sukkandiku ci Yowaana 2:17—«Cawarte gi ma am ci sa kër dina mel ni taal buy tàkk ci man.»
Dimaas
Porogaraamu dimaas bi, mu ngi sukkandiku ci Yowaana 4:23—‘Nañu jaamu Baay bi ci xel ak ci dëgg.’
Li ñi teew war a xam
Tegtal yu am solo yu ñi teew war a xam.
Seetal itam...
LU JËM CI ÑUN
Ndaje yu mag yi Seede Yexowa yi di amal at mu nekk
Ñépp mën nañu teew ci xew-xew yooyu ñuy amal at mu nekk te kenn du fey dara.
NDAJE YU MAG YI
Ñu ngi lay woo ci ndaje bu mag bu ñetti fan bu Seede Yexowa yi bu atum 2025 bi tudd: Nañu jaamu Yàlla ni mu ko bëgge
Lan la Yeesu jàngale ci lu jëm ci jaamu Yàlla ni mu ware?
NDAJE YU MAG YI
Lãsamã tiyaatar bu sukkandiku ci Biibël bi te tudd: Xibaaru jàmm bi Yeesu Yégle: Xaaj 2 ak 3
Léegi Yeesu màgg na, te tàmbali naa am ay taalibe. Waaye tàmbali na it jànkoonte ak ay fitna ci liggéeyu waare bi.

