Wolof
Yéenekaay bi ak Réveillez-vous !
https://cms-imgp.jw-cdn.org/img/p/1011209/univ/wpub/1011209_univ_sqr_xl.jpg

Yéenekaay bi ak Réveillez-vous !

Mën nga telesarse suñu yéenekaay yi sukkandiku ci Biibël bi ci lu ëpp 200 làkk. Ci làkk yooyu, am na làkku muuma yi. Dafa ñuy yégal xibaaru jàmm bi ci Nguuru Yàlla te loolu dafay dëfal suñu xol. Dafa ñuy xiir itam ci am ngëm ci Yeesu Kirist. Réveillez-vous ! dafa ñuy won ni ñu mënee jànkoonte ak jafe-jafe yi am ci àddina si tey. Dafay dëgëral itam suñu ngëm ci li Yàlla dige, maanaam dina fi indi àddina su bees fu nit ñépp di dëkk ci jàmm ju mat sëkk.

YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)

Suweŋ 2026

Li ñu nar a waxtaane ci yéenekaay bii dale ko 10 ut ba 6 septaambar 2026.

RÉVEILLEZ-VOUS !

12 ponk yiy tax njaboot yi am jàmm

Topp xelal yi nekk ci Biibël bi, mën na la dimbali nga am jàmm ci sa dund njaboot.

TÀNNAL NI PAAS BII DI FEEÑE

RÉVEILLEZ-VOUS !

RÉVEILLEZ-VOUS !

RÉVEILLEZ-VOUS !

YÉENEKAAY BI

YÉENEKAAY BI

YÉENEKAAY BI

YÉENEKAAY BI

YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)

YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)

YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)

YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)

YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)

YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)

YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)

YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)

YÉENEKAAY BI (NGIR NJÀNG MI)