Wolof
Misiku karceen ngir jaamu Yàlla
https://cms-imgp.jw-cdn.org/img/p/1011211/univ/wpub/1011211_univ_sqr_xl.jpg

Misiku karceen ngir jaamu Yàlla

Mën nga déglu walla telesarse ay woy-Yàlla yu karceen yi di woy ngir màggal te jaamu Yexowa Yàlla. Am na ci yoo xam ne misik kese la, am na ci itam yu ànd ak woy.