Ubbil li ci biir

Woneel li nekk ci téere bi

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
  1. 1. Yan ñooy ñetti mbir yi Yexowa di def ngir ñu am mbégte? (Sabóor 32:1-10)

  2. 2. Naka lañu mënee am mbégte tey? (Sabóor 5:12, 13; 91:14)

  3. 3. Naka lañu mënee wéy di am mbégte ci liggéeyu waare bi, doonte sax ñu ngi ci ay jafe-jafe? (Jëf ya 13:50-52; Waa Room 5:3-5)

  4. 4. Naka lañu mën a moytoo «diig» ba ñàkk suñu mbégte? (Luug 21:34)

  5. 5. Naka lañu Yexowa di bégale? (Sabóor 92:5, 6)

  6. 6. Lan moo ñuy dimbali ñu kontine di jiital Yexowa ci lépp? (Waa Room 1:20; Baamtug Yoon wi 6:6-9; Waa Filib 4:6; Sabóor 16:3)