Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2025-2026

‘Nañu déglu li xel mu sell mi di wax mbooloo yi’

Porogaraamu suba si ak bu ngoon gi, bu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni.

Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii

Dinañu tontu ci laaj yii ci ndaje bu mag bi.