Xibaar yi ci àddina si sépp
Ay yégle yu jóge ci Jataay biy dogal ci atum 2025 #3
Ci yégle bii, dinañu gis li ñu mën a def ngir yokk li ñuy def ci liggéeyu Yexowa, ci weer yii di ñëw.
Ay yégle yu jóge ci Jataay biy dogal ci atum 2025 #6
Ci yégle bii, dinañu wax ci aaya atum 2026 ak ci woy wu bees wi.
Ay yégle yu jóge ci Jataay biy dogal ci atum 2025 #5
Ci yégle bii, dinañu gis ay njàngale yu nekk ci Biibël bi, yu ñu mën a dimbali ñu jël ay dogal yu baax ci lu jëm ci njàng.
Ay yégle yu jóge ci Jataay biy dogal ci atum 2025 #2
Ci yégle bii, dinañu wax ci li suñu mbootaay bi nekk di def ngir dimbali suñu mbokk yi ñu jàng duruus ak bind. Dinañu wax itam ci ni ñu saraxu Yeesu bi di maye jàmm. Rax-ci-dolli, dinañu wax ci lu jëm ci woy bu bees bi ñu nar a woy ci ndaje bu mag bu ñetti fan bu atum 2025.
Ay yégle yu jóge ci Jataay biy dogal ci atum 2025 #1
Ci yégle bii, dinañu gis ni ñu mënee jëfandikoo «Dëgg yi ñuy jàngal nit ñi», ci téere bii tudd: Wonal nit ñi mbëggeel—Noonu nga leen di dimbalee ñu nekk taalibe Yeesu. Jàng xam dëgg yooyu dina ñu dimbali ñu am ay waxtaan yu neex ci liggéeyu waare bi.
Ay yégle yu jóge ci Jataay biy dogal ci atum 2025 #4
Ci yégle bii, dinañu gis ay njàngale yu nekk ci Biibël bi, yu ñu mën a dimbali ñu xam aada yi ñu warul a topp walla yëf yi ñu warul a jëfandikoo.

