Jàngal fii walla nga telesarse téere yi ñu wone fii ci suuf. Mën nga fi déglu yenn ci suñuy téere ci ay làkk yu bare, te doo fey dara. Mën nga it seetaan walla telesarse ay wideo ci ay làkk yu bare ak it ci làkku muuma yi.

Tànnal benn làkk ba pare nga bës fi ñu bind Génne ko ngir gis téere yi am ci làkk bi nga tànn ak ni nga leen mën a telesarsee.