Lan mooy dal nit bu deewee ?

Lan mooy dal nit bu deewee ?

Lan mooy dal nit bu deewee ? Tont bu leer bi Biibël bi joxe ci laaj boobu dafay dëfal xol te dalal xel.