Na seeni jëf méngook li ngeen xam ci xibaaru jàmm bi

Na seeni jëf méngook li ngeen xam ci xibaaru jàmm bi

FILIB 1:​27

Suba si

  • 9:40 Misik

  • 9:50 Woy-Yàlla nº 35 ak ñaan

  • 10:00 Naka la li nga xam ci xibaaru jàmm bi, soppee sa dund?

  • 10:15 Waxtaan bu def ay xaaj: Naka la li ñu xam ci xibaaru jàmm bi soppee seeni dund:

    • • Ecen

    • • Filib

    • • Akilas ak Pirsil

    • • Tit

  • 11:05 Woy-Yàlla nº 76 ak yégle yi

  • 11:15 Na nga wéy di am Jëf yuy wone ne da nga «ragal Yàlla»

  • 11:35 SÓOB BI: Wéyal di ‘déggal xibaaru jàmm bi’

  • 12:05 Woy-Yàlla nº 37

Ngoon si

  • 1:20 Misik

  • 1:30 Woy-Yàlla nº 56 ak ñaan

  • 1:35 Waxtaan bi ñu jagleel ñépp: Li nga gëm, ci lan la sukkandiku?

  • 2:05 Njàngum La Tour de Garde bu ñu gàttal

  • 2:35 Woy-Yàlla nº 24 ak yégle yi

  • 2:45 Waxtaan bu def ay xaaj: «Li ñu bëgg mooy di rafetal suñu tur ni Seede Yàlla ci . . .»

    • • Muñ

    • • Laabiir walla mbaax

    • • Njub

  • 3:30 Yàlla dafa ñuy jàngal jaaraale ko ci xibaaru jàmm bi. Naka la koy defe?

  • 4:00 Woy-Yàlla nº 29 ak ñaan