Porogaraamu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni bu atum 2021-2022
Yokkal sa ngëm!
Porogaraamu suba si ak ngoon gi bu ndaje bu mag bu benn fan ak ki bànqaas bi yónni.
Déglul bu baax ba mën a tontu ci laaj yii
Dinañu tontu laaj yii ci ndaje bi.

